Kom-kom :mooy xam-xam biy leeral lu aju ci wutiinu alal, tey li nga am ci alal, sa koom-koom man naa tekki sa alal, lépp nag lu aju ci yëngu gu nit di def ngir am dara loolu ci xam-xamu koom-koom lay bokk, moo xam mbay la mba yaxantu mbaa liggéeyu xarala(fr : économie ; en : economics) = koom-koom

Gaambi
  NODES
os 2