Kurów ab dëkku-kaw la ca bëj-saalum-penkug Poloñ. Mi ngi ne ci diggante Pulawy ak Lublino, ci dexu Kurówka. Mooy péyu gox-goxaan bii di gmina.

Mi ngi yaatoo 11,32 km², ci 2008 amoon na 2.804 way dëkk.

  NODES