Nuwaaksot (Nouakchott) : mooy pééyu réewum Gànnaar ak dëkk bi ko ëpp solo. Moom la bokk ci dëkk yi gën a mag ci Saara. Dëkk bi itam moo nekk màkkaanu nguur ak koom-koom ci réewum Gànnaar.

Wikipedia
Wikipedia
Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal


Logo Commons

Xool it Wikimedia Commons
  NODES