Paftan gi garabu tóotóor la gu bokk ci njabootu Apocynaceae.

Paftan gi (Calotropis procera)

Melo wi

Soppi

Garab gu yam la, man na àgg ba 3i met. Doomam day wërbalu te duuf. Moom ak xob wi wirgo wu nëtëx lañuy yore. Tóortóor bi day weex. Garab gi day nacc di génne meen mu bari.

Njariñ yi

Soppi

Garab gu am solo la ci wàllu paj.

Nataal yi

Soppi

Turu xam-xam wi

Soppi

Calotropis procera

  NODES