wolof

Soppi

bind: amna ñeenti maanaa

  1. aw bind rëdd wu mat bees war wàcci ngir bindaat weneen,
  2. bind amal ay baat, ci sa loxo walla wuutuloxo,
  3. bind gi nu Yàlla bind, maanaam sàkk,
  4. ab bind melow bind,

Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:

Soppi
  1. sa bind wi rafet na,
  2. yaangi bind ?
  3. Yàllaa nu bind ngir nu jaamu ko!
  4. sama bindu tay bii de xaw ma numay def bamu mokk,
  5. ndaw sii bind bi moo rafet!

mbind

Xool it

Soppi

Tekki

Soppi

  Waxiin

Déglu baatu bind ci wolofi Senegaal

  NODES
Done 1
see 1