wolof

Soppi

lay amna ñatti manaa ci wolof

  1. ab lay xeetu taw la bu nit dul yëg,te di ko gis muy weexal jawwu ji,
  2. aw lay wax jees di wax ngir saxal am mbir
  3. lay lees di jëfëndikoo tame ngir xajjale lu nooy ak lu dij

Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:

Soppi
  1. lay baaxul ci wer gi yaram,
  2. booy lijjanti mbir ci këru àttekaay gi wutël ab tinukat mu layal la.
  3. jigéen ji lay nañu pénc me bamu sét wicc

Xool it

Soppi

Tekki

Soppi

  Waxiin

Déglu baatu lay ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-lay.ogg

  NODES